Tassou Abdoulaye Wade - Vidéo insolite
11,282
by SENETOILE NEWS, 15 years ago
[*][color=red]na loxxo yi daaje!
na loxxo yi mbeekké !
na daajé na daajé !
na loxxo yi dajé !! é démal ! demal
Abdu dafa waace
Ablaye yéék
senghor wacup liiguééy
niu dém diko jaalé
bato ba diik
kunné boppam la tal !!
Nélba dafa réy té xélma naax
lumu wax fatté ko !
beut yeu da fa dug
té léx ya rass
laaye lejeel nanu !!
Laay dolli niu, Nga doggaliniou ?
Laay wadday paxoum kania !
Ak famèèm bu n’daw!
Bénoup diabar niaari doom
faaf goro ba déé !!!
laay wadday paxxum kagna !
Laay waddak ndongga[/color][*]